BSylla photography

BSylla photography “Xamal ni xam sa bop mo gën lo degg
Gën lep Lo seerou liilé di dëgg”
~
Ludul taalubé matula roy
~

“Quiconqueobéit à Dieu et au prophète ceux-là qui seront avec ceux que Dieu a comblésde son bienfait : Prophètes, véridi...
27/09/2025

“Quiconque
obéit à Dieu et au prophète ceux-là qui seront avec ceux que Dieu a comblés
de son bienfait : Prophètes, véridiques, martyrs, gens de bien, et quels bons
compagnons que ceux-là”

Ligeeyal Yallah amul nopalu!
17/09/2025

Ligeeyal Yallah amul nopalu!

“Rëyug bon du tee man ma jog jëm ci yawnde yaw dongu laa am ci ab jub lu kaayBarib tir du tee kay ma jog jëm ci dexDi ya...
06/08/2025

“Rëyug bon du tee man ma jog jëm ci yaw
nde yaw dongu laa am ci ab jub lu kaay

Barib tir du tee kay ma jog jëm ci dex
Di yaakaara set nak ba gën ñëpp waay

Amul gaqq goo xamne mën naa waral
Ma jog moy la ngir yaa di saa pootukaay

Bumay reer’akay tëx akay bon jëfit
Samay njort ñaawul ci Yaw ngën ji baay…”

“Ku Yàlla wallu nga fàtteb coona, Yal nanu may…Ñun ñépp wallu gu rëy, guy tax ñu dab ñanu rawTe Yal na Yàlla defar géppu...
24/05/2025

“Ku Yàlla wallu nga fàtteb coona, Yal nanu may…
Ñun ñépp wallu gu rëy, guy tax ñu dab ñanu raw
Te Yal na Yàlla defar géppug defar sunu mbir
Ba dóotu yàqu te may nug doylu fàww ak u yiw”

“Ngor ak diine ak worma yii jeex na teyTe yii nag bu jeexee lu dul ay desulKu ñëw may ko loo man te bañ koo lebalLilee g...
16/05/2025

“Ngor ak diine ak worma yii jeex na tey
Te yii nag bu jeexee lu dul ay desul
Ku ñëw may ko loo man te bañ koo lebal
Lilee gën di soowooka réccooka xul”

Yalnañu sax ci liggeyal Seriñ bi sunu giir dund !
12/04/2025

Yalnañu sax ci liggeyal Seriñ bi sunu giir dund !

“Ligeyal sa bakkan, ku yakaaru nitBa far jekki jambat loram ak meramKu yakaaru nit ak lamuy def ba taxMu xëy tëdd, kooke...
14/01/2025

“Ligeyal sa bakkan, ku yakaaru nit
Ba far jekki jambat loram ak meram

Ku yakaaru nit ak lamuy def ba tax
Mu xëy tëdd, kookee yorul am xelam”

Sikar Gamou 2024 à Medina Fall
26/09/2024

Sikar Gamou 2024 à Medina Fall

Bu cér yépp gàntoo def’as lëf jafeBu cér yépp gàntoo def’as lëf jafeDef’as lëf bu yombul am’as lëf jafeJugal farlu ngir ...
31/08/2024

Bu cér yépp gàntoo def’as lëf jafe
Bu cér yépp gàntoo def’as lëf jafe
Def’as lëf bu yombul am’as lëf jafe

Jugal farlu ngir yaa ngi cib lolli yaw
Te ab lolli buy wéy am’as lëf jafe

Ndegam reere nga’b lolli lollee ngi nii
Wér ak dund ak doole lollee jafe

Ku sab lolli ñëw nag ba say yëf ne xuss
La gën ngay ku yombul, ku maasam jafe

Jëfal guddi jëf bëccëg’ak sépp saa
Ba koo seeru naa kii jëfam yee jafe
Ku def nii ci sab lolli do jeele yëf
Bu nooree te doo xaare yewwoo jafe

via .app

“Ku yakaaru nit ak lamuy def ba taxMu xëy tëdd, kookee yorul am xelam…Amal lef ci as fulla am as njariñAm as itté ndax y...
13/08/2024

“Ku yakaaru nit ak lamuy def ba tax
Mu xëy tëdd, kookee yorul am xelam

Amal lef ci as fulla am as njariñ
Am as itté ndax yalla may las xoram“

Adresse

Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque BSylla photography publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à BSylla photography:

Partager